Nay

Youssou N'Dour

Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss

Ndaw souné goor gamoul dadiel
Fo dioulété togale té niane bania dale
Ci goor gou nay amoul ndieurigne
Sa nidiaye nèè bindeu la
Loka waar way dou takh mou dagne, dou changé
Ki koumou dale am nga natou
Wethit bou ndaw diaral nako
Mou xoulo ak yow tongue lathié ay fani fane
Di xoultou ba nga délo koko
Sa ndieul bene yow xamoko wone
Nga dem bassa biir remarqué ni ap nay la

Bo meuné daw gawal téfeukh
Ap nay dou tabi aldiana
Mane Youssou N'Dour waxoumake lathe ko
Oustaz hanne mou firil lako

Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss

Nay dé baxoul
Nay dou wadia
Goor gou nay boy sek ak mom
Day koy moudiou diepi lolou
Nay dé baxoul
Nay dou wadia
Goor gou nay bouy sek ak djiguene
Dafkoy tek stress, youdoul, diex

Ap nay bou kheuy reerlé dara
Fek guissouko diam dou am ci keur gui
Tè diaral nako, wowi police
Daye leb xaliss dinthe ko
Abeu ba diote mou daldi gaw déloko
Nguir bania guéné limou yoor
Bou guéné dem sa xewma
Moy yooré waxtane ba louné mou waxko
Ba nopi doufa bayi dara
Daye mine yonou marché ba
Fokni boula bayék ndougou li nga naxko
Goor gui lé mom néxoul deukeul
Bou reutheulé mayla dara
Daye moudiou wexx xatteu ci yow ndax thiow li
Foumou tok waxtané ko

Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss

Niit kouné xam nga bou bakh ni nga mél
Say défauts ak say qualités, oumpoula
So goorgoorlou touti, sabab lou touti
Defci sa xool meune nga sopékou
Niit kouné xam nga bou bakh ni nga mél
Say défauts ak say qualités, oumpoula
So goorgoorlou touti, sabab lou touti
Defci sa xool meune nga sopékou
Niit kouné xam nga bou bakh ni nga mél
Say défauts ak say qualités, oumpoula
So goorgoorlou touti, sabab lou touti
Defci sa xool meune nga sopékou

Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss

Ndaw souné goor gamoul dadiel
Fo dioulété togale té niane bania dale
Ci goor gou nay amoul ndieurigne
Sa nidiaye nèè nay bindeu la
Yow loka waar waar dou takh mou dagne dou changé
Ki koumou dale am nga natou
Ap nay dou tabi aldiana
Mane Youssou N'Dour waxoumako yow lathe ko
Oustaz hanne mou firil lako

Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss
Mane beugouma goor gouy kotte kotti
Goor dafay gaw bamouy louxouss

Niit kouné xam nga bou bakh ni nga mél
Say défauts ak say qualités, oumpoula
So goorgoorlou touti, sabab lou touti
Defci sa xool meune nga sopékou
Niit kouné xam nga bou bakh ni nga mél
Say défauts ak say qualités, oumpoula
So goorgoorlou touti, sabab lou touti
Defci sa xool meune nga sopékou

x

Músicas mais populares de Youssou N'Dour

Outros artistas de World music