Gane Gou Bess Gui

Youssou N'dour

Gann you béss gui yéksi légui
Gann gui, nékh na gars gné
Gann you béss gui yéksi légui
Gann gui, nékh na gars gné

Mbaye Dièye
Li takh mou nékh gars yi
Laleu beugueu khamal
Ni Mbaye
Li takh mou saf gars yi
Laleu beugueu yeugueul
Ki ci am sa doom
Ték ko si sa wétt
Yar ko yar bou bakh
Kham dokhinam
AK démlantém

Gann you béss gui yéksi légui
Gann gui, nékh na gars gné
Gann you béss gui yéksi légui
Gann gui, nékh na gars gné

Bi mou douguesé niépp
Niko diakk
Mou daldi waaf
Deugoul, dawoul
Dafani tékk ak confiance
Ndakh tingkam
Tingkam Tingkam
Ba yéksi fi naan tingkam
Ba yéksi fi naan tingkam
Tingkam Tingkam
Ba yéksi fi naan tingkam

Wakh nga deugg You
Youssou Madjiguéné
Guiss nga khalé bi
Lima ci guiss
Guissoko woon
Naka la douguesi
Dieul garde khol niépp
Lolo waral, kouy diguéne
Kholal sa toguay
Nioune wa sang-sang
Dano civilisé, beugueu lou bakh
Eh you, khalé bi may nako or
Kou ci am sa doom
Ték ko si sa wétt
Yar ko yar bou bakh
Khol façon-ngam
Ak dokhinam
Ak démlantém

Gouné bou yaro mathieu tangal
Ba yeuye sa gounéngaye
Bo yaradiko ya koy yeugg
Khalé bou yaro bakh

Gann gou béss gui douguesi légui
Nékh na gars gné
Sama gars gni, gann gui nay to téral
Sama gars gni, gann gui diarna téral
Sama gars gni, gann gui nay to téral
Sama gars gni, gann gui diarna téral
Gann gui diarna téral
Gann gui diarna téral
You
Khalé bi ma guiss
Am a yar, civilisé daldi
Kham lou bakh
Nioune wa sang-sang
Dano civilisés dagno kham lou bakh
Gno lay wakh lou bakh
Togual goro, fotal goro wakhtan nakoup goro
Tékk ték am kérsa mana mougn
Li diarna louné

Tékk ték am kérsa mana mougn
Mann diaralnama
Tékk ték am kérsa mana mougn
Mann diaralnama
Tékk ték am kérsa mana mougn
Mann diaralnama
Tékk ték am kérsa mana mougn
Mann diaralnama
Tékk ték am kérsa mana mougn
Mann diaralnama
Tékk ték am kérsa mana mougn
Mann diaralnama

Sa wadji gann gui diarna téral
Gann gui nagko téral
Gann gui nagko téral
Sa gars gni gann gui diarna téral
Kou ci am sa doom (gann gui nagko téral)
Yar ko yar bou bakh (gann gui nagko téral)
Khol dokhinam (gann gui nagko téral)
Ak façon-ngam (gann gui nagko téral)
Ak démlantém (gann gui nagko téral)
So amné doom (gann gui nagko téral)
Yar ko yar bou bakh (gann gui nagko téral)
Khol façon ngam (gann gui nagko téral)
Ak dokhinam (gann gui nagko téral)
Sa wadji
Gan gui nagko téral

Curiosidades sobre a música Gane Gou Bess Gui de Youssou N'Dour

De quem é a composição da música “Gane Gou Bess Gui” de Youssou N'Dour?
A música “Gane Gou Bess Gui” de Youssou N'Dour foi composta por Youssou N'dour.

Músicas mais populares de Youssou N'Dour

Outros artistas de World music