Ay Chono La

Habib Faye, Youssou N'dour

Ndéké mbeuguel nii la
Ndéké yaw rek lenen la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, nangou len ko

Ndéké mbeuguel nii la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Mbeuguel ay chono la, bouko wédi
Ay chono la, ay chono la, nangou len ko
Mbeuguel ay chono la, boulenko wédi
Ay chono la, ay chono la, nangou len ko

So ko khamé nonou kham né yar no gno yar na gno yar no gno

Oh

Ndéké mbeuguel nii la
Nit di na la beug ba sank la
Ndéké yaw rek lenen la, lenen la bouko wédi
Ay chono la, bou len ko wédi
Mbeuguel ay chono la, nangou len ko

So ko khamé nonou kham né yar no gno yar na gno yar no gno

Oooh

Curiosidades sobre a música Ay Chono La de Youssou N'Dour

Em quais álbuns a música “Ay Chono La” foi lançada por Youssou N'Dour?
Youssou N'Dour lançou a música nos álbums “Set” em 1990 e “History” em 2019.
De quem é a composição da música “Ay Chono La” de Youssou N'Dour?
A música “Ay Chono La” de Youssou N'Dour foi composta por Habib Faye, Youssou N'dour.

Músicas mais populares de Youssou N'Dour

Outros artistas de World music