Raison Nègre (FreeDope Intro)

Elzo JamDong

Martin Luther King speech:
"It came as a joyous daybreak to end the long nights of our captivity. But 100 years later, the Negro still is not free …free …free …free …free" …free
DOPE yeah

Verse 1:
Me dieulate ay gaïndé me dompter lène
Seme flow ay containers moye gonfler nerou wa corner bé
Zig, Tamba ak Pont Faidherbe
Boudoul wone fi dou done fénène
Boudoul wone Free dou done kénène
Boul khole kénène bougoumeu done lénène
Al hamdou mane sante na
Jamm dongg le shit bi dou done lénène
Strong in the biz boy pompez lène
Té con yi le time deniou done kébétou souniou son yi di leu hit ngané on t’énerve
Bouniou nèkhone niouy diaay rich
Fègne ak bepp khètou bad bitch
Ndakh gentle negn, tangal nègn
Wayé boul tékkheulé bante ak wégn
Boul tékkheulé thiant ak wéy, dinga diawalé diante ak wère ??
Bou bougué am diam dongg son bi diam se ndong li
Nanga and ak tèye
Bo lene mounoul ba lène mic bi, cons Free crack #bon élève
Dope pour Black & white am na raison nègre #EmotionHellène

Chorus:
Jamm dongg le ish bi dou done lénène (ish bi dou done lénène) X4
Togg na quantité yekk na qualité (hun FreeDope)X4

Verse 2
Wesh c’est qui ? Qu’est ce the deal? It’s the best in this my boyyy
Mane doumeu deul extasy, gueuwmeu sex appeal té doumeu nekk di bif ak ay boyyy (hun hun)
Rest in peace Laye Séga, RIP Baye Petit
Iba Sèye, Lik-Sama, wallah wéteul nguène birr keur gui
The West African Finest, man a rep African fighters:
Niom Sankara, Lumumba : I’m no blood but I’m diamond
Bad as M.I Jackson, Jam-ballin like Jordan
My tape rockin like Mysonne
Punch faces like Tyson haaaaaan
Audio crack coke laye nouyo
Ga yi niam flow bi saf DOPE bayi niou go
Dealers yi dow degn degg DOPE ba ngui nieuw
DOPE ba ngui nieuw!?? Wouyaye DOPE ba ngui nieuw!!!
Seme style defe nité ya ngui feel nimey indé seme flow?
Mo gueuneu épicé kilo bone !
Seme skill defe styléé, deme ill, nimey dealer seme DOPE ?
Demey killé ak stylo dongggg !

Chorus

FreeDope X4

Curiosidades sobre a música Raison Nègre (FreeDope Intro) de Elzo JamDong

Quando a música “Raison Nègre (FreeDope Intro)” foi lançada por Elzo JamDong?
A música Raison Nègre (FreeDope Intro) foi lançada em 2014, no álbum “FreeDope”.

Músicas mais populares de Elzo JamDong

Outros artistas de African hip hop