DE DU TAGO

Bruno HOVART, Lansana SANE, Paul CUCURON

Adouna dal kéneu dacoufé
Bisbounéca manega déme waye
Adouna dal kéneu dacoufé
Gnou gueune si gnoune gnoye déme bayignoufé
Samaye xarite déme nagne sorimaye
maguini wétaye songouma
gnima beugeu déme nagne sorimaye
magui gnane borome bi terraléne waye

Dé mome dou tago
Souye gneuwe
Déla dou tago

Lépeu lo mana ame
Lépeu lo mana yore
Fi ga koye bayé sa wadjié
adouna dal adouna mome démal magui woye gneuwe la
Soye dieufe dieufeule yawl ou raféte
Bis daye gneuwe lépeu gnou sédélla
Sama maye lépeu lofi dieufe waye Défale yaw ak xole bou raféte

De mome dou tago
Souye gneuwe
Déla dou tago

Músicas mais populares de Lass

Outros artistas de Afrobeats